Facebook
Twitter
Problem melden

Undecided (Japoulo) Songtext

Youssou N’Dour - Undecided (Japoulo)
Quelle: Youtube
0:00
0:00
Né japoulo, té bayi wo
Sé deng, deng dé japoulo, té bayi wo
Né noboulo, té bayi wo
Sé deng, deng dé japoulo, té bayi wo
Han sé deng, deng, sé deng, deng, sé deng, deng, sé deng, deng(fois 2)

Hé yaw li nga japone ba mél ni
Hé yaw boulko bayi té jiknala(fois 2)

Né noboulo yaw bayi wo
Sé deng, sé deng té bayi wo
Wouye noboulo, yaw bayi wo
Sé deng, sé deng thiey bayi wo

Waw sé deng deng, sé deng deng, sé deng deng, sé deng deng

Noboulo, bayi wo
Sé deng, sé deng yaw bayi wo
Né noboulo yaw té bayi wo
Sé deng, sé deng yaw bayi wo
Waw sé deng deng, sé deng deng, sé deng deng, sé deng deng

Hé yaw li nga japone ba melni
Hé yaw boulko bayi té jikna la(fois 2)

La la la la la la la la la mani yeksil sét
La la la la la la la la mani dougal sét
La la la la la la la la la ma ni yeksil sét

Kham nga ko, kham nga ko, kham nga ko
Kanam dou kasso wayé kouka sétlou guiss ko(refrain)
News
Stefan Raab und Bully Herbig: Erster TV-Auftritt endet in Niederlage
Vor 16 Stunden
Stefan Raab und Bully Herbig: Erster TV-Auftritt endet in Niederlage
Casey Chaos: ‚Grammy‘-Gewinner tot mit 59 Jahren
Vor 16 Stunden
Casey Chaos: ‚Grammy‘-Gewinner tot mit 59 Jahren
Made with in Berlin
© 2000-2024 MusikGuru