Miss Lyrics

Lyrics
Han' ma wakh ko ben yoon te dem miss yi gno taarou
Han wakhlenko niarri yoon te niou dem ohhhooo'
Miss yi nio taarou
Yen djiguene nirew deug deug gore yowmi yoboulegnou dara
Yen djiguene nireww deug deug mbaye gathie gualamane
Yen djiguenerewmi ken meussou len djamnanile
Fatelikou talatay nder aline sitoe diatta yacine mboubou.
Ah ma 1#
Ah ma 2x
Te mane sax mane damalene beug

Fonk
Heu axirouzamane modi moudiou diamono waw waw
Mo xam lu moudj wala lou fegn leu
Writer(s): Habib Faye, Mouhamadou Kabou Gueye, Youssou N Dour
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Was als nächstes?

Dein Karma steigt mit jedem Klick! Teile den Guru-Link und bring Lyrics in die Welt.

Youssou N’Dour - Miss
Quelle: Youtube
0:00
0:00