Liggeey Lyrics
von Youssou N’Dour
Sound béne leu thi adouna biyeup nitt kounék amnga lo yeuk
Niit kounék ammnga fém *2
Less play assane teugueul
Less play thiam tama
Rock reggea jazz mbalakh all around the word béneu la
La samba la rumba thieu thieu thieu béneu la
Ziguibiti i live music all around the world béneu la
Saoul macossa rap music all around the world béneu la
Music bi béneula louléne beglo lagnuy sakou music bi béneu la louléne beglo lagnouy fékhé musicien adouna béneula louléne di beglo lagnouy sakou musicien adouna béneula louléne di beglo lagnouy fékhé ah hiii yééééé
K
Ko meuneu guiss mbaye si adouna amna thiossanam bouko nekh
Am nga sa ngor am nga sa diom fonkou nga sey adeu
Bilay kou nek ko guiss sagne nadieul lissa khol bi yaw nga defko
Moytoul di togne té del téral kou diok beu gneuw setsila
Bilay demlantéléne wéthié khalat bou kéneu khébaté

Writer(s): Habib Faye, Mouhamadou Kabou Gueye, Youssou N Dour
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Was als nächstes?
Dein Karma steigt mit jedem Klick! Teile den Guru-Link und bring Lyrics in die Welt.
-
Beliebte Youssou N’Dour Lyrics
Link kopiert!
Youssou N’Dour - Liggeey
Quelle: Youtube
0:00
0:00