Allah Lyrics

Lyrics
Allah allah
Allah allahhhh
Allah allah
Allah allahhhh
Souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
Kenn la kenn la amoul masse
Souniou borom bi ya wakhidoune kenn la
Kenn la kenn la amoul masse
Lahilaha illalah
Souniou borom bi ya wakhidoune kenn la

Bo néké sisa birou yaye
Yalla dila samm bagua am
Diourim nienti werr
Mou wathie la si adounya bi
Bolé thia nak
Ay kheweli khewel
Boko togné so diegeulo mou bal la
Boko niane mou mayla gua sant ko
Mou dolil la
Ladioul loudoul nangua ma diamou
Ladioul loudoul nangua ma diamou
Iow bo goré bo goré
Warko diamou sant ko
Writer(s): Kabou Gueye, Youssou N'dour
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Was als nächstes?

Dein Karma steigt mit jedem Klick! Teile den Guru-Link und bring Lyrics in die Welt.

Youssou N’Dour - Allah
Quelle: Youtube
0:00
0:00