Gnouni nééna gnouni nééna
Gno bok réwmi
Gnouni nééna gnouni nééna
Nagnou yatal guéwgui
Gnouni nééna gnouni nééna
Gno bok réwmi
Nagou yatal guéwgui
En gnouni nééna gnouni nééna
Wouté meunteu gnak nam
Wayé bounou wahtané dioubo
Wouté meunteu gnak nam
Wayé bougnou wah tané guis yone
Féhélén galgui tér fou bah
Dou mo gueun gnou dooranté diowli
Féhélén wé wi tér fou bah
Guéthie dianguini défa sambara
Halé yagui thi biir
Mak gnagui thi bir
Boulén wégal galgui
Halé yagui thi biir
Mak gnagui thi bir
Boulén wégal galgui
En gnouni néna
Wouté meunteu gnak nam
Wayé sougnou wahtané dioubo
Wouté meunteu gnak nam
Wayé sougnou wahtané
Guis yoono
Hébaté déy indi réérodé
Séytané défa bari dolé
Hébaté déy indi rérodé
Séytané défa baridolé
Moussibaleu nagnou yatal guéwgui
Li khéw cazamace néhouma
Néña réyé haleyi nék nanou
Gni nék nanou
Nitgnou soul bélayi nék nanou
Gni guek ...
Nék nanou oooh sama khét
Ga gnagui héthio réwmi
Kou nék nane mana nane mane
Kou nék nane mana nane mane
Kou nék nane mana nane mane
Soudoul mane dou bakh
Kou nék nane mana nane mane
Diohlén ma réwmi mba ma wégal galgui
Writer(s): Papa Amadou Fall, Cheikhou Coulibaly, David Turkstra
Lyrics powered by www.musixmatch.com